"Cila Bokk"
— cantado por Bril
"Cila Bokk" es una canción interpretada en senegalés lanzada el 06 septiembre 2019 en el canal oficial del sello discográfico - "Bril". Descubre información exclusiva sobre "Cila Bokk". Encuentre la letra de la canción de Cila Bokk, traducciones y datos de la canción. Las ganancias y el patrimonio neto se acumulan mediante patrocinios y otras fuentes de acuerdo con una información que se encuentra en Internet. ¿Cuántas veces apareció la canción "Cila Bokk" en las listas de música compiladas? "Cila Bokk" es un conocido video musical que ocupó posiciones en las listas de éxitos más populares, como Top 100 Senegal Songs, Top 40 senegalés Songs y más.
|
Download New Songs
Listen & stream |
|

"Cila Bokk" Hechos
"Cila Bokk" ha alcanzado 2M visualizaciones totales y 16.3K me gusta en YouTube.
La canción se envió el 06/09/2019 y pasó 99 semanas en las listas.
El nombre original del video musical es "BRIL - CILA BOKK - CLIP OFFICIEL".
"Cila Bokk" ha sido publicado en Youtube en 05/09/2019 10:31:33.
"Cila Bokk" Letra, Compositores, Sello discográfico
** Mon nouvel album SUBA est
;A écouter et/ou télécharger en cliquant ici
;**
**Abonne-toi à ma chaîne ici
**
Après le succès de "Bras Long", CILA BOKK est le 2ème single extrait du nouvel album de Bril, SUBA, disponible à partir du vendredi 20 septembre sur toutes les plateformes de streaming et téléchargement.
Il est vital de bien se détendre et s'amuser : vos vedettes préférées comme Dudu, Mahfousse, Admow, Pagaye Mbaye, Pape Birahim ou Bass Thioung vous aident à oublier vos problèmes.
Cila Bokk, viens nous rejoindre, faisons la fête tous ensemble !
(voir lyrics plus bas dans cette description)
#Bril #CilaBokk #Suba #NouvelAlbum20septembre #ClassChicMusic #team221
**Crédits de la chanson "Cila Bokk" **
Auteur : Bril
Compositeur : Bril
Studio enregistrement, mix, edit & mastering : Class’Chic Music par Bril
Une production de Class’Chic Music (Dakar, Senegal, septembre 2019)
**Crédits du clip "Cila Bokk" **
Réalisation : Weeflag
Un grand merci à Dudu , Mahfousse, Admow, Pape Birahim,, Jeeba,, jah hustla , Pagaye Mbaye & Bass Thioung pour leur aimable participation.
**Retrouvez Bril sur les réseaux sociaux**
Snapchat : @bril-fight4
** Contact management**
Mr Mahmoud Sy : +221 77 036 48 31
brilfight4@
**Booking international**
@
**Lyrics de de la chanson "Cila Bokk" **
{Intro}
hahahahaha
(Bril on the Beat) ha ha
Yeah yeaaah Bril in the Building , héé
Cila Bokk way way Cila Bokk , amoul Yakkalaté han , aythia Niou dém
{Refrain}
Xamal ni dakoy ladj nga dindi stress.
Boula kén ray doundou dafay nekh.
Koula beugga sonal Romb ko né mééss.
Niongui Foo, Happy , Bégué, Mba Xol yangui fékh .
*kaay* “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
*kaay* Sagnsé andak kilay bégglo “Cila Bokk”
*kaay* “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
*kaay* Tok di sétane Loulay réélo “Cila Bokk”.
{1er Couplet}
Lo xamoul kagn lay djèkh dafa wara nékh .
Boul faalé koulay méré wane ko beugn you wékh.
Léppeu térangala , doundeul happyness.
Lofi meunti am té béggo , amna louthi déss.
Fii dal Sénégal la , boula nékhé dinga béggué .
Boul nangou kèn yakkal-la dééko défé ning’ko beuggué.
Daniouy dadjé foo di réé té xawma no Toudou .
Selfie def ay Vidéo you fun melni #Dudu,
#Baye_Mbaye , #Makh_Pro / koufi mér kone Wéro.
Warnga meune di enjoy nga né town wala ghetto .
Boul nangou kèn dila téré
Kou sa life néékhoul , yakoy soppi .
{Refrain}
Xamal ni dakoy ladj nga dindi stress.
Boula kén ray doundou dafay nekh.
Koula beugga sonal Romb ko né mééss.
Niongui Foo, Happy , Bégué, Mba Xol yangui fékh .
*kaay* “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
*kaay* Sagnsé andak kilay bégglo “Cila Bokk”
*kaay* “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
*kaay* Tok di sétane Loulay réélo “Cila Bokk”.
{2ème Couplet}
Héé Yaw nanga déf
Koula beugga sonal thi wakh nèko mou déf,
Défam té bayila rèk yaw nga néthi .
Take it easy , dafa wara yomb, waroul , méti hééé.
Beurina ay Nitt you done foo djaarfa feullalé .
Tèki_thi romboula wakh bo saani niou feul- feulalé.
Kheuthiolén son you #Lourd , ma ték lou #Léger dilén Mour .
Ngén may gueuna #Haine, maléni raw par #Amour.
Bayilén niouy rawanté ngay dokh ndank , daagoul .
Té koukay djaay méti , né ko “Lou Méti Yagoul”.
Dél Khol sa none di réé né kouy sétane #Aba_Show
Caméra cachée #Makhfouss lay yooné sama Cho (copine)
{Refrain}
Xamal ni dakoy ladj nga dindi stress.
Boula kén ray doundou dafay nekh.
Koula beugga sonal Romb ko né mééss.
Niongui Foo, Happy , Bégué, Mba Xol yangui fékh .
*kaay* “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
*kaay* Sagnsé andak kilay bégglo “Cila Bokk”
*kaay* “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
*kaay* Tok di sétane Loulay réélo “Cila Bokk”.
{Outro}
*kaay* Héé ...féthial féthial way , *kaay* ni rekla yeungoul yeungoul way .
*kaay* Hééé...féthial way , *kaay* ni rekla yeungoul yeungoul way .
*kaay*. féthial féthial way , *kaay* niou dèm , hèè Han han yeungoul yeungoul way .
*kaay* mané Cila bokk
;cila bokk.